Aduna du dara té dara khadiufi bilae kouko diap
Khamal ni diaposi dara
Aduna du dara té dara khadiufi bilae kouko diap
Khamal ni diaposi dara
Mane Youssou niak na andando bou sincère
Aduna, aduna dal nakhati naniu
Aduna, aduna dafay woré Habib faye demna ni wa diu bax diu tey demna
Habib yarou wone na Andak dignité
Fonkone na liguey beugone na ndiabotam
Donone diambar
Mane Youssou niak na andando bou sincère
Aduna, aduna dal nakhati naniu
Aduna, aduna dafay woré Habib Faye demna ni wa diu bax diu tey demna
(Habib, Habib) Dama ko dieulé école andi ko Super étoile mou deugguel ko
(Habib, Habib) Man dal mangi len koy dialé yen wa famille wam ak ay fans sam
(Habib, Habib) Di len di hamal ni Habib Faye diougué woufi
(Habib, Habib) Nio fi defon mak mom mou woné fa loutax nitt gni beuggon ko
Senegal la gui lay dioy
Rew bangui lay dioy
Africa la gui lay dioy
Aduna la gui lay dioy
(Habib, Habib) Sama beugg beugg moy li, sa beugg beugg moy leh
NItt kouné ak beugg beuggam
Yallah na done, Yallah na done la geun ci mom
Ladial wa doundou gué anh, Habib goudé na goudé na
(Habib, Habib) Dama ko dieulé école andi ko Super étoile mou wané fa
(Habib, Habib) Wané fa loutax nieup nieup beuggon ko
(Habib, Habib) man Youssou niak na andando bou sincère
Aduna aduna dal nakhati naniu
Aduna aduna dafay woré Habib faye demna ni wa diu bax diu tey demna