Video Mool Deglu Meteo » Youssou Ndour Lyrics | Musica Afro

Ver Video y Lyrics con la música del Genero Afro más popular de Youssou Ndour y otros artistas en línea. Disfruta de las mejores canciones de 2025 en LetrasFM de música en línea. ¡Encuentra tu canción favorita y escúchala en cualquier momento y en cualquier lugar!

Video Mool Deglu Meteo » Youssou Ndour Lyrics

Youssou Ndour - Mool Deglu Meteo Lyrics

Yaw mool u géej gi di jambaar ci réew mi
Bala ngaa dem géej ngala déglu météo

Bu la nee bul dem lu mën ë xew bul dem
Ben fan ak ñaar bu mu yax sa liggéey

Doyloo nga yalla, du tee nga sa yor téléphone
Ak sa GPS, te bul fatte sa gillet

Sama fans yi ma am, mool ñoo ma gën ë xam
Fu ma làng ee ak ñoom, guddi gë day xumb lool

Man sama fans yee, ma saf
Sawar naa làng ak ñoom, fu ne
Aka ñoo dégg daaj, ma ni
Moo tax may dem ba jeex, walla

Jambaar ca waar wa, jambaar ca géej gë
Su ma ko mën oon, ben mool du des ci géej

Bu la nee bul dem, lu mën ë xew bul dem
Ben fan ak ñaar, bu mu yax sa liggéey

Sama fans yi ma am, mool ñoo ma gën ë xam
Fu ma làng ee ak ñoom, guddi gë day xumb lool

Jambaar ca waar wa, jambaar ca géej gë
Su ma ko mën oon, ben mool du des ci géej

Man sama fans yee, ma saf
Sawar naa làng ak ñoom, fu ne
Aka ñoo dégg daaj, ma ni
Moo tax may dem ba jeex, walla

Yalna leen yalla suturaal, te di leen samm biir géej
Barke el seen liggéey bi, barke el seen njaboot gi
Aar leen ba ñu doon mag, jox leen barke maam yi

Man sama fans yee, ma saf
Sawar naa làng ak ñoom, fu ne

Yess aye

Anh mool ba dem na géej oo (anh mool ba dem na géej oo)
Anh mool ba dem na géej oo (anh mool ba dem na géej oo)
Bël ba ca ndar, sonn al na waa guét ndar géej oo (anh mool ba dem na géej oo)
Mool yi laa bëgg ë làng al, seen làng xumb në
Ndax sa ma fan’s yi nak, am mool yee ci gën ë dense
Anh mool ba dem na géej oo (anh mool ba dem na géej oo)
Bël ba ca ndar, sonn al na waa guét ndar géej oo (anh mool ba dem na géej oo)
Sa telephone ak sa GPS, bul fatte gillet ba
Anh mool ba dem na géej oo (anh mool ba dem na géej oo)
Ñoom laa bëgg ë làng al, seen làng xumb në
Ndax sa ma fan’s yi nak, am, mool yee ci gën ë dense
Anh mool ba dem na géej oo (anh mool ba dem na géej oo)

A dëgg ël, yaw mool u géej
Yaa di jàmbaar
Yaa bari fullë lool
Bari jom lool
Yaa donn loolu
Gëm yalla lool
Yaa xarañ lool, te tabe lool
Youssou woy na leen
Anh mool ba dem na géej oo (anh mool ba dem na géej oo)
Bël ba ca ndar, sonn al na waa guét ndar géej oo (anh mool ba dem na géej oo)
Mool yi laa bëgg ë làng al, seen làng xumb në
Ndax sa ma fan’s yi nak, am, mool yee ci gën ë dense
Anh mool ba dem na géej oo (anh mool ba dem na géej oo)
Anh mool ba dem na géej oo (anh mool ba dem na géej oo)
Mool yi laa bëgg ë làng al, seen làng xumb në
Ndax sa ma fan’s yi nak, am, mool yee ci gën ë dense

Mool Deglu Meteo » Youssou Ndour Letras !!!

Videos de Youssou Ndour

Esta web no aloja ningun archivo mp3©LetrasFM.Info 2025 Colombia - Chile - Argentina - Mexico. All Rights Reserved.

Musica Online, Escuchar musica online , Musica En Linea, Musica en linea gratis, Escuchar Musica Gratis, Musica Online 2025, Escuchar Musica

Musica 2025, Musica 2025 Online, Escuchar Musica Gratis 2025, Musica 2025 Gratis, Escuchas, Musica de Moda.