Boo ma beddiwul xalaatuma la bàyyi
Awma làmmiñ soon tudduma lambay yoy
Gaañ la taxul nga ba
Tooñ la taxul nga may rëccooy
Salaw yenn saay nga mer
Sama jaambaar ci yaw mi la wékooy
Dootuma wiri wiri njari ndari
Li ma moom lay jëli (eeh yoo)
Dootuma yonni kenn ci sama waa ji
Man mi maa koy jëli (man ma)
Dootuma wiri wiri njari ndari
Li ma moom lay jëli (daadi sama waay)
Dootuma yonni kenn ci sama waa ji
Man mi maa koy jëli (danga di sama waay)
Bala ma jog
Fajar fekk nga dem jaayooy
Bale kër gi raxas say ndap
Ndekke boobu dam ngay wajal
Dundu maata ñaan nooy
Ndaxte gaynde dama koy jur
Ndax fitna loo ma
Xëboo li ma lay jox
Lépp loo ma ñaan dinaa la may
Dootuma def leen lu lay metti sama ndaw si
Ndax sama nawle nga doo leeral sama yoon wi
Dootuma nangu mindéef di dox sama digu ak yaw
Ndax Yàlla moo def ci ñun lay ñu wëy nak
Kaay waay!
Gaañ la taxul nga ba
Tooñ la taxul nga may rëccooy
Salaw yenn saay nga mer
Sama jaambaar ci yaw mi la wékooy
Dootuma wiri wiri njari ndari
Li ma moom lay jëli (eeh yoo)
Dootuma yonni kenn ci sama waa ji
Man mi maa koy jëli (man ma)
Dootuma wiri wiri njari ndari
Li ma moom lay jëli (daadi sama waay)
Dootuma yonni kenn ci sama waa ji
Man mi maa koy jëli (danga di sama waay)
Gaañ la taxul nga ba
Tooñ la taxul nga may rëccooy
Salaw yenn saay nga mer
Sama jaambaar ci yaw mi la wékooy
Eee waay
Sama jaam, sama waay
Eh waay wow
Sama jaam, sama waay