Xale bu ndaw def buzz
Ñeet sons kase teg concert (VJ)
Important ni adducteurs
My g rap bi la jël en main (VJ)
18 ans doon millionaire
Rappeur bu ko fi am kan la? (VJ)
Xale bi xale yi bëgg
Nurulak namp ye koy xëcco (VJ)
Surax si kaw scène
Def bum te awma sax album (VJ)
Ñoom népp kan lañ bãn
Kan lañuy xol nigga may seen choice (VJ)
Feesal salle di leen joyloo
Ñoom ñépp bañ disant nooon (VJ)
Pischininiko yaw feccal mel ni Kitana
Eh, ne nañ munuma rap
Xanaa ñi deñ dof
Wala dañ bëgg seen chef yi
Ñëw toojal leen bokk
Seen muker yi lay xëcc
Firil leen mbari naan tës
Man duma tiit ndax yaay booy
Ne na ma yaw demal music xale
Billaay wallaay talay music xale
Ñi bëgg VJ ñi koy topp ñépp xale
Billaay wallaay talay music xale