Video Rakkaaju » Pape Diouf Lyrics | Musica Lyrics

Ver Video y Lyrics con la música del Genero Lyrics más popular de Pape Diouf y otros artistas en línea. Disfruta de las mejores canciones de 2025 en LetrasFM de música en línea. ¡Encuentra tu canción favorita y escúchala en cualquier momento y en cualquier lugar!

Video Rakkaaju » Pape Diouf Lyrics

Pape Diouf - Rakkaaju Lyrics


Assane mblakhal niou délou nguewel
Music amoul thiow nii dongou la
Mbalakh ba mou nekh fans yiii bégué

Bakaane mblakhal niou délou nguewel
Music amoul thiow nii dongou la
Mbalakh ba mou nekh fas yiii bégué
Boulen di sonaneté yooone dou melni lemm yalla nopina

Djoubeul ba né khotie say bagne deungeul
Domou diambour bouko yakh dangko djouroul
Music amoul thiow dou concurrence
Djodjo matoul djodjo merr mou yagg la
Li de léer na ma

Garap dina meuna donne penc euleukk
Laobé dou ko guiss ndakh gorrésouko
Yalla mi ko def mome mo koy aréé
Djodjo matoul djodjo merr mou yagg la
Li de léer na ma

Fans yii yene lay woooyal
Sopé yii tay ma djinne l éne
Bouléne khoulo bouléne khékh
Dina mbalakh ba mou saf niou andiiy bégue
Djodjo matoul djodjo merr mou yagg la
Yalla noppi naa
Djouga ndiéré ndiaye
Djouga ndiéré ndiaye
Sala khari ngoné
Me gana biram diop sa mame la
Adj ndoubé mane contane cii yéne mane
Djouga ndiéré ndiaye
Sala khari ngoné
Me gana biram diop sa mame la
Adj ndoubé mane contane cii yéne soppeyii

Koussa khol nekh djogall yeugnou
Sopé yii
Fans yii
Bilay soumay sonne souba akk ngone yenna ko warral
Deuké daw mane douma tayyyi damay khouss
Domoou gaindé daye gnamé diam diam wawaw
Bilay anta papa ngom
Dieuf thia ka ko mane
Kouka meunoul danguay yakk dieuf
Yakkal kako yoor yaye sama khariit
Bilay ma fi djaronne
Setsina léne
Ma fi djaronne khaley sénégal, setsi naléne
Ma fi djaronne khaley gambia, fonk naléne
Kila fekk ngua tilime mou simi ba ngua sete
Sangue la bangua sete
Solalale mboubou mou sete, yeukeutilla bagnou guissla mou tekk la fou sette
Lo ka meunti defitte dou ko guiss ndakh mbeugél gua la kholl si yaw
N'est ce pas?
Sigariga dialandi fat ndioré
Siga riga riga riga riga dialandi fat ndioré
Bokk yakar book yaa
Weundelou, rakadiou fanganiouna

Assane mblakhal nguewel
Mane ma dikk waye nguewel
Mbalakh bou safé nguéwél
Nieupay rakkaddjou

Assane mblakhal nguewel
Mane ma dikk waye nguewel
Mbalakh bou safé nguéwél
Nieupay rakkaddjou

Assane mblakhal nguewel
Mane ma dikk waye nguewel
Mbalakh bou safé nguéwél
Nieupay rakkaddjou
Ni amoul adji amoul ass kouné la meuna yeungeul
Mbalakh bou safé nguéwél
Nieupay rakkaddjou
Thiaya ak mariniére drap ak costume louné laniou kooy fethié
Mbalakh bou safé nguéwél siaradio diallo
Nieupay rakkaddjou
Assane mblakhal nguewel
Mane ma dikk waye nguewel
Mbalakh bou safé nguéwél
Nieupay rakkaddjou
Taximan ndiaga ndiaye tata. Super thiakata dieuleléne mbalakh mi
Mbalakh bou safé nguéwél modou fall ndiaye
Nieupay rakkaddjou

Deuk ci nguewel waye ci nguewel
Fethi ci nguewel yabba ci nguewel
Ehh tiey ngewell ehh thiew nguewel

Rakkaaju » Pape Diouf Letras !!!
Esta web no aloja ningun archivo mp3©LetrasFM.Info 2025 Colombia - Chile - Argentina - Mexico. All Rights Reserved.

Musica Online, Escuchar musica online , Musica En Linea, Musica en linea gratis, Escuchar Musica Gratis, Musica Online 2025, Escuchar Musica

Musica 2025, Musica 2025 Online, Escuchar Musica Gratis 2025, Musica 2025 Gratis, Escuchas, Musica de Moda.